"Diokormadior"
— cantado por Satou Niang
"Diokormadior" é unha canción interpretada en senegalés publicada en 17 decembro 2023 na canle oficial do selo discográfico - "Satou Niang". Descubre información exclusiva sobre "Diokormadior". Busca a letra da canción de Diokormadior, traducións e feitos da canción. As ganancias e o patrimonio neto son acumulados por patrocinios e outras fontes segundo unha información atopada en internet. Cantas veces apareceu a canción "Diokormadior" nas listas de música compiladas? "Diokormadior" é un coñecido vídeo musical que tivo lugar nas listas populares, como as 100 mellores Senegal cancións, as 40 mellores senegalés cancións e moito máis.
|
Download New Songs
Listen & stream |
|

"Diokormadior" Feitos
"Diokormadior" alcanzou 260.5K visualizacións totais e 4.8K gústame en YouTube.
A canción foi enviada o 17/12/2023 e pasou 19 semanas nas listas.
O nome orixinal do vídeo musical é "SATOU NIANG - DIOKORMADIOR (CLIP OFFICIEL)".
"Diokormadior" publicouse en Youtube en 16/12/2023 20:00:07.
"Diokormadior" Letra, Compositores, Selo discográfico
Réalisation : DIGIT PROD
Production : DIGITAL MUSIC
Distribution : DIGITAL MUSIC
Music : ZBEST
Arrangement : ZBEST
Mix & Mastering : ZBEST
Déco : AY PEULH
Tenues : Afshal -
Momo création -
D'S couture -
Barham couture
Maquilleuse : Marie Louise - Ker Yuma
Acteurs : Baye, Daba DIOUF, Astou NDIAYE, Kya
***Remerciements***
Aida Toure, Mamadou sylla
Copyright Décembre 2023
MANAGER : 77 839 98 92
Contactez Satou NIANG sur
????????
☑️Instagram : satou_official
☑️Facebook Page : Satou Niang
☑️Tiktok : @satouniang7
Lyrics ✍????
COUPLET I
Man lima dalon
douma dalat
dioxnala sama xolbi Dieuleul
dofna si iow guisuma kenen yawla guiss
bilay walay man yawla guiss
Waxna Yaye néko yawla
Wax baye néko yawla
bou xolbi yeungo
yako yeungeul cheri man yawla guiss
Lélalélaay man yawla guiss
REFRAIN
Sama xolbi nexna
Ndax manmi dagnma nob
nieup nenagnma Temps yi danga béli
Yagimay diokormadior diokorlén
soumla guisul damay wet
bidéw bi léral sama yoneee
diokormadior diokorlén
soumla guisul damay wet
bidéw bi léral sama yoneee
COUPLET II
massouma fok lii si mane
mbeugél bou doy momlama diokh
yakarbi fésneu si man
yornameu arma deukomeu
Sama yéné si iow moy seuyeuleu aldiana
mougn moytou dégeuleu ni serigne ak Talibé man
loma wakh lay def loma téré ma bayi
sakou geureum dieund bamél ndiabot gou barkél
Bilal walay man yaw lay guiss
REFRAIN
Sama xolbi nexna
Ndax manmi dagnma nob
nieup nenagnma Temps yi danga béli
Yagimay diokormadior diokorlén
soumla guisul damay wet
bidéw bi léral sama yoneee
diokormadior diokorlén
soumla guisul damay wet
bidéw bi léral sama yoneee
diokormadior diokorlén
bidéw bi léral sama yoneee
COUPLET III
Mouhamet fall cheri mati Ndoye
soumla wayalé man fall Ndiaga yaram
soumalay sumala wayalee mannn
yeee Mamy Chiekh Tidiane